Demba is not at tge center, he is in the shop
Demba nekkul ci santar bi, mungi ci butik ba
He is in the classroom
Mungi ci biir kalaas bi
The person
Nit ki
Tge people
Nit ñi
The men
Goor ñi
The women
Jigeen ñi
The adults
Maggñi
The old people
Magget ñi
The young people
Ndaw ñi
The kids
Xale yi
The trees
Garab yi
The tables
Taabul yi
Excuse me
Baal ma
Repeat!
Waxaatal!
Stop talking
Noppil
Learn well
Jangleen bu baax
To be slow
Yéex
To wake up
Yeewu
To get up
Jog
To go to school
Jàngi
To teturn to
Dellu
To meet with
Daje ak
To help
Dimbali
City
Dëkk bi